Neyemi: «Mbégte bu jóge ci Yexowa mooy seen doole»
Neyemi mooy jiite liggéeyu tabaxaat miiri Yerusalem ak indiwaat diine dëgg ji.
Neyemi: «Mbégte bu jóge ci Yexowa mooy seen doole»—Xaaj I
Neyemi jéem na tabaxaat miiri Yerusalem bu dee sax ay noon def nañu lépp ngir tere liggéey bi.
Neyemi: «Mbégte bu jóge ci Yexowa mooy seen doole»—Xaaj II
Miir yi pare nañu, waaye ndax Neyemi dina mën na dimbali mbooloo mi ñu defaraat seen diggante ak Yàlla?