Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Neyemi: «Mbégte bu jóge ci Yexowa mooy seen doole»—Xaaj I

Neyemi: «Mbégte bu jóge ci Yexowa mooy seen doole»—Xaaj I

Neyemi dafa bàyyi liggéeyam ca kër buur ca Sus ngir tabaxaat miiri Yerusalem. Waaye du liggéeyu tabax bu mag boobu rekk moo naroon a nekk jafe-jafe ci moom. Ndax ñaan Yàlla ak am fit rekk doyoon na ngir matal liggéey boobu?