Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Neyemi: «Mbégte bu jóge ci Yexowa mooy seen doole»—Xaaj II

Neyemi: «Mbégte bu jóge ci Yexowa mooy seen doole»—Xaaj II

Bi ñu tabaxaatee miiri Yerusalem ba pare, Neyemi amoon na beneen jafe-jafe. Waa Israyil dañu bàyyi jaamu Yexowa ni mu ware. Esras ak Malaki ñoo ko dimbali ci indiwaat diine dëgg ji.