Ubbil li ci biir

Ndaw ñi

Yenn ci tur yi ñu fi lim dañu leen soppi.

LI NDAW ÑI DI LAAJ

Lan laa mën a def bu ñu may bundxataal?

Ñu bare ci ñi ñuy bundxataal duñu xam lu ñu war a def. Leeral nañu fii li nga mën a def ba génn ci.

LI NDAW ÑI DI LAAJ

Lan laa mën a def bu ñu may bundxataal?

Ñu bare ci ñi ñuy bundxataal duñu xam lu ñu war a def. Leeral nañu fii li nga mën a def ba génn ci.

Li ndaw ñi di laaj

Li ndaw ñi di laaj lu jëm ci diggante góor ak jigéen, xaritoo, waajur, lekkool ak yeneen.

Li yeneen ndaw wax

Mën nga dund loo xam ne masuloo ko dund. Xoolal li yeneen ndaw def ngir génn ci.

Nañu jàng ci tabló bi

Ndax yaa ngi dund ay jafe-jafe yoo foog ne mënoo leen a faj? Bu dee waaw, wideo yii mën nañu la dimbali nga génn ci porobalem yi ndaw ñi faral di jànkoonteel.