Ay Seede Yexowa nettali nañu seen jaar-jaar
Seede Yexowa yi dañuy def lépp ngir topp ci seeni xalaat, seeni wax ak seeni jëf, li nekk ci Kàddu Yàlla, Biibël bi. Xoolal ni loolu soppee seen dund ak dundu ñi leen jege.