Fàttalikuleen deewu Yeesu
At mu nekk, Seede Yexowa yi dañuy fàttaliku deewu Yeesu ni ko Yeesu santaane woon (Luug 22:19, 20). Ñu ngi lay woo nga ñëw teew ci ndaje bu am solo boobu. Dinga xam njariñ bi nga mën a jële ci dundu Yeesu ak deewam.